Hebrews 2:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moom Yeesu miy sellal, ak ñi muy sellal, ñoom ñépp genn njaboot lañu. Moo tax Yeesu rusu leen a wooye ay doomi baayam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu miy sellal nit ñi, moom ak ñi muy sellal, ñoo bokk lenqe, te moo tax Yeesu rusu leena wooye ay bokk.