Hebrews 2:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Leer na ne, Yeesu xettalisiwul malaaka yi, waaye askanu Ibraayma lay xettalisi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat du ay malaaka la Yeesu xettlisi, waaye askanu Ibraayma la xettlisi.