Hebrews 2:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yàlla jébbalul malaaka yi benn sañ-sañ bu jëm ci jamonoy ëllëg ji nuy wax; keneen la ko jébbal,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat du ci kilifteefu malaaka yi la Yàlla teg àddinay ëllëg ji nuy wax,
Recommended Reading