Hebrews 2:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte am na fu ñu wax ci Mbind mi ne:«Lan mooy nit, yaw Yàlla, ba nga di ko xalaat?Lan mooy doomu nit, ba nga koy topptoo?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
waaye am na ku yékkatee bérab, kàddug seede, ne: «Ana luy nit ba nga di ko faale? Ana luy doom aadama, ba nga di ko yég?