Hebrews 3:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
diirub ñeent-fukki at.Looloo tax gennliku naa leen, daldi ne:“Seeni xalaat a leen di réeral saa su nekk,xamuñu yoon yi ma neex.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
diiru ñeent fukki at. Moo tax ma mere googu maas, ba ne: “Seen xol a dëkke lajj, te nanguwuñoo xam samay yoon.”