Hebrews 3:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Am nanu wàll ci Kirist, su nu wéyee fii ba muj ga ci sunu kóolute, gi nu amoon ca njàlbéen ga.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat noo di àndandooy Almasi, ndegam wéye nanoo ŋoy bu dëgër ci sunu kóolute ga nu doore, ba kera muj ga.