Hebrews 3:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu gis nanu sax ne, jotuñoo dugg ci noflaay boobu ndax seen gëmadi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nu gis ne seen gëmadee tax manuñu ca woona tàbbi.