Hebrews 3:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku takku la ci liggéey bi ko Yàlla sas, ni ko Musaa nekke woon ci lépp lu jëm ci waa kër Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku wóor la woon, ñeel ki ko tabb, noonee Musaa wóore woon ci mboolem waa kër Yàlla.