bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 4:6
Hebrews 4:6 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon am na ñu ci war a dugg ba tey. Te ñi jëkkoon a jot xebaar bu baax bi, dugguñu ci ndax seen déggadi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag am na ñenn ñu ci wara tàbbi ba tey. Te ñi ñu jëkkoona àgge xibaaru jàmm bi, tàbbiwuñu ca ndax seenug déggadi.