Hebrews 5:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci fànn googu, am na lu bare lu nu ci bëgg a wax, waaye tekkil leen ko dina jafe, ndaxte dangeen a naqari xel.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moomu mbir nag bare na lu nu ciy wax, waaye tekki ko mooy jafe ndax seen déggin wu diib.