Hebrews 5:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu yàgg ngeen waroon a jàngal ñeneen ñi, waaye soxla ngeen ba tey ku leen di tette ci kàddug Yàlla. Léegi nag yéena ngi tollu fi ñu leen war a nàmpale, ndaxte àttanuleen ñam wu dëgër.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat nëgëni tey waroon na leena fekk diy sëriñ, waaye aajowoo ngeen ba tey ku leen jàngal ndoortel waxi Yàlla. Nàmp um soow ngeen mujj aajowoo, ndax ñàkka àttan ñam wu dëgër.