Hebrews 5:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te ndegam moom ci boppam nit kese la, man na muñal ñiy moy ndax seen ñàkka xam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dina mana sédd cér ñi xamul ak ñi moy ndax moom ci boppam ci ag néew doole la tënku.