Hebrews 5:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li mu ñàkk doole moo tax mu war a def ay sarax ngir mbaalug bàkkaaram, ni mu ko tàmmee defal mbooloo mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Néew doole googu moo tax mu wara joxeel boppam, tey joxeel askan wi ay sarax, ngir seeni bàkkaar.