Hebrews 5:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye li muy nekk-nekk doom, teewul mu jàng déggal Yàlla, jaare ko ci coono bi mu daj.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li muy Doom lépp, terewu koo tàggatu ci dégg ndigal, ndax coono yi mu daj.