Hebrews 5:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu la àgge cig mat, ñu def ko ki waral mucc gi dul jeex, ngir ñi ko déggal ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu lees matale Almasi sëkk, ba mu doon cosaanu mucc gu dul jeex, ñeel mboolem ñi ko déggal.