Hebrews 6:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nit kuy giñ nag, daf koy wékk ci ku ko sut. Ngiñ lu mel noonu moo wóoral mbir te mooy jeexal lépp lu ñuy werante.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nit nag, ku ko sut lay giñe, ngir dogal kàddu, ba teesal wépp werante.