Hebrews 6:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñaari jëf yooyu nga xam ne duñu tebbiku te Yàlla mënu cee dellu gannaaw, dañu nuy gën a sóob ci muñ, nun ñi daw ba am kiiraay, ngir nu man a téye bu dëgër yaakaar, ji mu nu dig.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñaar yooyu du tebbiku ndax Yàlla du fen, te nun ñi daw làqusi ci moom, ci lanu ame ndëgërlaay lu réy lu nu ŋoye ci yaakaar ji ci sunu kanam.