Hebrews 6:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te noonu lanuy def, bu soobee Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nanu jëm kanam, te moom lanuy def, ndegam soob na Yàlla.
2 translations compared side by side