bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 6:4
Hebrews 6:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Li nu war a jëme kanam mooy lii: su amee ay nit ñu Yàlla xas a leeral ba noppi, ñu mos mayu Yàlla gi, am wàll ci Xelam mu Sell,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi ñu xasa leeral nag, te ñu jota mos may gu bawoo asamaan, séddu ci Noo gu Sell gi, deesu leen mana defal dara.