Hebrews 6:7 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Maanaam suuf suy naan taw bi ciy dal, tey jox ñi ñu koy beyal gàncax gu am njariñ, day jot barke bi jóge ci Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax suuf kat, su naanee ndox mu mu tawlu ay yoon, ba meññal ñi ñu koy beyal, gàncax gu leen jariñ, soosa suuf dina séddu ci barke bu bawoo fa Yàlla.