bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 7:12
Hebrews 7:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te bu ñu fi jëlee saraxalekat yi ak seen liggéey, dañoo war a toxal itam yoon, wi ñu fi tëraloon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Carxal gi nag su soppikoo, fàww yoon wi itam soppiku, ànd ak moom.