Hebrews 7:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu Yeesu mi nuy wax, mi ngi soqikoo ci geneen giir gu bokkul ak giiru Lewi. Giir googu nag, amu ci kenn ku ci mas a def liggéeyu saraxale ca saraxalukaay ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ki kàddu yii jëm ci moom, fa mu bokk, geneen giir la, te kenn ci giiram masu cee liggéeye ca sarxalukaay ba.