Hebrews 7:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li waral mbir mi gën a leer moo di ne, beneen saraxalekat bu mel ni Melkisedeg dafa ñëw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbir mi gëna leerati gannaaw ba beneen sarxalkat feeñee te mel ni Melkisedeg.

Recommended Reading