Hebrews 7:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte seedeel nañu Yeesu lii:«Doon nga saraxalekat ba fàwwmel ni Melkisedeg.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat, gii kàddu, seedeelees na ko ko: «Yaa dib sarxalkat ba fàww, topp dayob Melkisedeg.»