Hebrews 7:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
--ndax yoonu Musaa yeggalewul dara cig mat — waaye dugalal nañu nu fii yaakaar ju gën ju nu man a jaare ngir jege Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax yoonu Musaa sottalul dara ba mu mat sëkk. Ci geneen wet, yaakaar ju gën moo nuyoo, di yoon wu nuy jaare ba àgg fa Yàlla.