Hebrews 7:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nag Yeesu moom doon na saraxalekat, bi Yàlla giñee ne ko:«Boroom bi giñ nate du dellu gannaaw mukk:“Doon nga saraxalekat ba fàww.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye Yeesu mii la ag palam ànd ak ngiñ lu jibe ca ka ko wax ne ko: «Boroom bee ko giñ te du dellu gannaaw: “Yaa dib sarxalkat ba fàww.”»