Hebrews 7:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it yeneen saraxalekat yi dañoo bare woon, ndaxte dee moo daan tax duñu man a sax ci seen liggéey.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi ñu masa fal sarxalkat nag bare nañu, te tëlee wéye fàww seen sas moo tax, gannaaw ñoom ñépp ay dee.

Recommended Reading