Hebrews 7:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Naka yoonu Musaa, aji néew doole yi lay fal saraxalekat yu mag. Waaye ngiñu Yàlla gi ñëw gannaaw yoon wi, Doom ji la fal saraxalekat bu mag bu mat ba fàww.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat yoonu Musaa, ay nit ak seenug néew doole la fal ay sarxalkat yu mag. Waaye kàddug ngiñ li topp ci yoon wi, moo fal sarxalkat bu mag, Doom ji ñu matal sëkk ba fàww.