Hebrews 7:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Seetleen ni mu màgge, moom Melkisedeg! Ibraayma sax, maamu cosaan mi, fab na li mu jële woon lépp ca xare ba, jox Melkisedeg asaka ja.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seetleen ni mu ràññikoo, moom la Ibraayma maamu cosaan ma ci boppam jébbal fukkeelu cérub cëxëtoo ma!