Hebrews 7:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yoonu Musaa digle na ne, ñi bokk ci giiru Lewi te di ay saraxalekat, nañu jot asaka ci alalu bànni Israyil, doonte sax ñuy seeni bokk te soqikoo ci Ibraayma.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te sarxalkat yi bokk ci giirug Lewi ni ko yoon wi tërale, ñoom lañu sant ñu nangu céri fukkeeli alali askan wiy seeni bokk, te soqikoo ñoom itam ci geñog Ibraayma.