Hebrews 7:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Saraxalekat yi soqikoo ci Lewi, ñu ngi jot asaka, ni ko Melkisedeg jote woon. Waaye ñoom ñu nar a dee lañu. Melkisedeg nag moom, Mbind mi wóoral na ne, dafay dund.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon ci gii wet ay nit ñuy dee doŋŋ ñooy nangu ay céri fukkeel, ca gee wet nag ku ñu seedeel ne mu ngi dund ba tey moo jagoo cérub fukkeel.