Hebrews 8:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kenn dootul war a jàngal moroomamwalla mbokkam, di wax naan:“Xamal Boroom bi!”Ndaxte ñépp dinañu ma xam,li dale ci ki gën a ndaw ba ci ki gën a mag.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kenn dootu soxlaa jàngal moroomam, mbaa mbokkam, naan ko: “Ràññeel Boroom bi!” Ndax ñoom ñépp a may ràññee, ki gëna tuut ba ci ki gëna mag.