Hebrews 8:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mu ngi liggéey ca bérab bu sell-baa-sell, di màggalukaay bu dëggu. Nit defaru ko; Boroom bee ko sos.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mooy liggéeye kër gu sell ga, ca biir xaymab jaamookaay bu dëggu, ba Boroom bi samp, te nit sampu ko.
Recommended Reading