Hebrews 8:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bépp saraxalekat bu mag fal nañu ko, ngir muy def ay sarax ak ay saraxi mala yu jëm ca Yàlla. Kon nag fàww Yeesu am lu mu joxe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw nag ab sarxalkat bu mag bu mu mana doon, dees koo fal, ngir muy jébbale ay jooxe ak saraxi jur, kon fàww sarxalkat bu mag bii itam am lu mu sarxe.