Hebrews 8:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu nekkoon ci àddina, du nekk sax saraxalekat, ndaxte am na fi ba noppi ay saraxalekat yuy def ay sarax, ni ko yoonu Musaa santaanee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu doon ci àddina, du nekk sax ab sarxalkat, gannaaw ay sarxalkat a ngi fi, di jébbale ay sarax, ni ko yoonu Musaa laaje.