Hebrews 8:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye léegi nag liggéeyu saraxale, bi ñu jox Yeesu, moo gën a màgg liggéeyu saraxalekat yooyu, mel ni it kóllëre, gi Yeesu fas diggante Yàlla ak nit, moo sut kóllëre gu jëkk ga te mu tëdd ci ay dige yu ëpp yu jëkk ya.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye tey la Yeesu jot ci liggéeyu carxal gu sut gu jëkk ga fuuf, te kóllëre gi mu fas diggante Yàlla ak nit ñi, noonu la gëne gu jëkk ga; dige yi lal kóllëre gu yees gii it, noonu la gëne dige ya laloon gu jëkk ga.