bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 9:1
Hebrews 9:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kóllëre gu jëkk ga ëmboon na ay ndigal ci mbirum ni ñu war a jaamoo Yàlla. Amoon na itam kër Yàlla gu nekkoon àddina.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kóllëre gu jëkk ga amoon na moom itam, ay ndigalam yu jëm ci ni ñu wara jaamoo Yàlla, ak bérabam bu sell bi fi kaw suuf.