Hebrews 9:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Kirist ñëw na, doon saraxalekat bu mag, bi joxe xéewal yi teew. Jaar na ca màggalukaay ba gën a màgg te gën a mat, te màggalukaay booba loxol nit defaru ko, maanaam bokkul ci àddina sii.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Almasi nag moo dikk tey, di sarxalkat bu mag, bi yor xéewal yi teew ba noppi. Moo dugg ca biir xayma ba gëna màgg te mat sëkk, xayma bu loxol nit deful, te loolu mooy xayma ba bokkul ci càkkéefug àddina sii.