Hebrews 9:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca kaw gaal ga teg nañu fa ñaari nataali mbindeef yu ñuy wax Seruben, yu doon wone ndamu Yàlla. Seeni laaf ñoo doon yiir baalukaay ba. Waaye loolu lépp léegi mënunu koo tekki benn-benn.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca kaw gaal ga la ñaari jëmmi malaakay serub nekkoon, di tegtale leeru Yàlla, seeni laaf keppaaral kubeer ga ñuy amale ag njotlaay. Waaye yooyu dunu ko mana daldi faramfàcce léegi.