Hebrews 9:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba ñu defaree lépp, saraxalekat ya dañu daan dugg bés bu set ca néeg bu jëkk ba, ngir mottali seen liggéeyu saraxale ca Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu waajalee noonu yooyii ba mu jekk, sarxalkat yaa daan dugg saa su nekk ca néeg bu jëkk ba, di def seen liggéey.