Hosea 10:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Israyiloo, ca janti Gibeya nga dala moye, te foofu la waa réew mi tollu ba tey. Luy tee xare dabe nit ñu jubadi ñi ca Gibeya?