Hosea 13:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana seen buur boog, ba mu xettli leen ci seen mboolemi dëkk? Ana seen njiit yi ngeen sàkku woon, ba ne ma: “Falal nu buur aki kàngam?”