Hosea 2:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa koy jëmbatal sama bopp ci réew mi, maay yërëm ki tuddoon “Ki ñu yërëmul.” Ki tuddoon “Du sama ñoñ,” ma ne ko: “Yaay sama ñoñ,” moom mu ne ma: “Sama Yàlla.”»