Hosea 9:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yonent bi mooy jongrukat biy wattul Yàlla, Efrayim, waaye ag fiir lees ko lalal ci mboolemi yoonam, te mbañeel a ngi ci biir kër Yàllaam.