Isaiah 22:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Da leen di fekk sàkk mbànd diggante ñaari tata yi, ngir denc ca ndoxum déeg bu yàgg ba. Waaye xooluleen ki dogal lii, xalaatuleen ki nasoon lii bu yàgg.