Isaiah 28:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbàccum nisel watiir amu ca yoon, te deesul bàcc kumin itam, ba joggi ca tànki watiir. Mbàccum nisel, yet a koy def; mbàccum kumin, bant bu yem.