Isaiah 29:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem xeet yu bare yiy xareek Aryel, di song dëkk beeki tataam, nar leena torxal, ñoom ñépp ay mel ni gént mbaa njeneeru guddi!