Isaiah 36:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa doo ma ne seen Yàlla Aji Sax ji ngeen yaakaar? Xanaa du moom nga toxal bérabi jaamookaayam yeek sarxalukaayam, ba noppi ne waa Yerusalem ak Yuda sarxalukaay boobu lañuy sujjóotal?”