Isaiah 37:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye xanaa déggoo ne bu yàgg laa dogal loolu? Ca jant yu jëkk ya laa ko nasoon, tey ma sottal ko, ba nga mana def genti jali tojit, dëkk yu tata wër.