Isaiah 66:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Coowal xaree ngoog bawoo dëkk ba, coow laa nga jóge kërug Yàlla ga, coowal Aji Sax jee, mooy yool ay noonam.